CHANSON DE SOULEYMANE FAYE ET HENRY GUILLABERT
le plus dur en cas de rupture c 'est quand on en connait pas la cause et on est obligé de vivre avec , car celui avec qui on partageait tout , nous laisse dans l' incompréhension.SYFA
fokoye jeleti
ku la beugue ne mane
fokoye jeleti ku la sope ne mane
fokoye jeleti ku la nobe ne mane
kou yewou khadju guoudi di xole ndax sangu gua
koulaye wakhe degue djo bougou la degue ni mann
kou neke ak falla bour bi yalla feteuleu
ak fa gua beugue sa boop feuter
fou ma koy jeleti
kouma nobe ni yaw
fou ma koy jeleti
koumay firer ni yawe
fou ma koy jeleti
kou ma gneme wakh degue ne yaw
boula bour yalla begue dangue koye khame
nakh tohidouna bo doug mou guene laci
boula nit ki beugue domm yay dan koy kham
nakh bou moussi beu di khegne mouni kaye goungue ma fii
adouna gui nonou ci sunu kanam
diaw waroula teukou morouma diamamme
adouna gui nonou ci sunu kanam domou yaye
diaw waroula teukou morouma diamamme
fo key jeleti
fan la koye jeller
fo koy jeleti
kou begue sa djame ne mane
fouma koye jeleti
kou degue dethie ni yow
fouma koye jeleti
kou moke pothie ni yow
fokoye jeleti
kou yewou khadju guoudi de xole ndax sangu gua
koulaye wakhe degue djo bougou la degue ni mann
kou neke ak falla bour bi yalla feteuleu
ak fa gua beugue sa boop feuter
fo koye jeleti
fan la koye jeleti