mbeuguel carlou D -*-une chanson qui sort du coeur pour entrer dans le coeur -*-

chansos_d__amour

Mbeugel thiakhane takhou ma dioke

Mbeugel fo takhou ma dioke

Mbeugel wiwite takhouma djoke

Mbeugel yape takhou ma djoke

NONO dede

Mbeugel thiakhane takhou ma dioke

NONO dede

Mbeugel diame mo ma takha dioke

Wawa yeye

Mbeugel diame ma takha dioke

Mbeuguelou yermandé ma takha diokhe

Mbeugel thiakhane takhou ma dioke hehe

NONO dede

Mbeuguelou salama ma takha diokhe

Wawa yeye

Demaye woma dila woma

Demaye woma dila woma

Mbeugel thiakhane takhou ma dioke

Mbeugel fo takhou ma dioke

Mbeuguelou yermandé ma takha diokhe mane

Mbeugeulou njabott

Wawa yeye

Mbeugeulou love moma takhe djoke

Wawa yeye

Mbeugeulou Yermande  ma takhe djoke

Wawa yeye

Demaye woma dila  wowaye

Demaye wo malaye wo sougnou ande meuna nekhe

Sayo  diakhelé khamalako

 mane  sayou diamakhelé khamaleko

Nakhe gno boke mbene doundou bou gnouye doundou gnoungni

sougnou ande dafa wara nekhe

wawa yeye

Demaye woma dila  wowaye

Mbeugel thiakhane takhou ma dioke

Mbeugel fo takhou ma dioke

Mbeugel wiwite takhouma djoke

Mbeugeulou Yermande  ma takhe djoke

Wawa yeye

Mbeuguelou kham kham mo  ma takha diokhe

Wawa yeye

Mbeugeulou Yermande  ma takhe djoke

Wawa yeye

Mbeuguelou guagne  takhou ma  diokhe

Demaye woma dila  wowaye

SYFA